Foxar+
Ñetteelu yoonu Newton
Ak ñeenti misaal, gis te xam Ñetteelu Yoonu Newton: Ku jëf dara, am na dëppoo ci moom ab jëf buy wuyyu ko buy dëppook moom te mana ko; walla, jëf yu ñaari yëf ci seen biir, dañuy mana seen bopp te jëm ci wàllu kontar.
Ubbi resours bi