Model bii dafay comparé jubluwaayu aksë ak gaawantoo wëndéelu juróom-ñeenti planet yi nekk ci Système Solaire bi. Planet yi dañuy wonee ci dayob seen bopp bu dëggu, booba ñu wone leen ci menn dayo wu yemale ngir yombal comparaison bi.
Am na ko ak bind